Jeremiah 52:28 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lii mooy limu nit ñi Nabukodonosor toxal: Ñetti junniy Yudeen ak ñaar fukk ak ñett (3 023), loolu yemook juróom ñaareelu atu nguuram,