Jeremiah 6:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo tax Aji Sax ji wax ne: «Maa ngii di tegal askan wii ay pakk, ñu fakkastaloondoo, baay ak doom, dëkkandook ub xarit, ñépp sànku.»