Jeremiah 6:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne: «Nañu witta witt ndesu Israyil, ni ñuy witte reseñ, ba nga dawalaat say loxo ca car ya.»