Jeremiah 7:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo tax Aji Sax ji Boroom bi dafa wax ne: «Sama xadar a ngii di sottiku fi bii bérab, fi kaw nit ak mala, garab ak lu suuf meññ, lépp ne jippét, te deesu ko fey.»