Jeremiah 7:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji Boroom gàngoor yi, Yàllay Israyil dafa wax ne: Jekkal-leen seeni jikkook seeni jëf, ma dëël leen bii bérab.