Jeremiah 8:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ag xodd sax xam na bésub demam, pitax, wetwet ak mbelaar it dem, tey sàmm seen bésub délsi. Waaye sama ñoñ faalewuñu àtteb Aji Sax ji.