Job 30:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Musiba da maa ëlëm, sama daraja naaw ni ngelaw, sama teraanga naaxsaay niw niir.