Job 31:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ki ma sàkk ci sama biiru ndey, xanaa du moo leen sàkk ñoom itam? Du kenn kee nu sos ci njurukaay?