Job 38:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ana yoon wu jëm fa leer di tasaaroo? Ak fu ngelawal penku di xàjjalikoo, ba dajal suuf si?