Job 5:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Doji àll bi sax, kóllëreg jàmm ngay séq ak ñoom, te ndundati àll bi dañuy jàmmook yaw,