Job 5:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ni pepp di ñore, ñu door koo góob, ni ngay màggataale doole, doora dëgmal bàmmeel.