Job 9:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Samay fan tarxiis nañu, wéy, woyof ni gaali barax, mbaa jaxaay ju naan jàyy cim rëbbam.