John 1:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñooñu judduwuñu ci deret walla ci bëgg-bëggu yaram, walla ci coobarey nit. Ñu ngi juddu ci Yàlla.