John 1:16 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Kàddu gi fees na ak yiw, te nun ñépp jot nanu ci sunu wàll, mu barkeel nu ay yooni-yoon.