John 1:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu ñu laaj ko ne: «Wax nu yaay kan, ngir nu man a tontu ñi nu yónni. Nga ne yaa di kan?»