John 1:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci moom lañu sàkke lépp. Amul dara lu ñu sàkk lu jaarul ci moom.