John 1:30 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Moo taxoon ma wax ne: “Am na kuy ñëw sama gannaaw, waaye moo ma gën a màgg, ndaxte nekk na laata may juddu.”