John 1:31 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Xawma woon kooku kan la waroon a doon, waaye xamal ko bànni Israyil moo tax ma ñëw, di sóob nit ñi ci ndox.»