John 1:41 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Andare dafa daldi dem seeti Simoŋ ne ko: «Gis nanu Almasi bi.» Baat boobu mi ngi tekki «Kirist.»