John 1:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Kooku ñëw na, doon ab seede, ngir wax ci mbirum leer gi. Ñëw na ngir ñépp dégg li mu wax te gëm.

Recommended Reading