John 10:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Baay bi bëgg na ma, ndaxte damay joxe sama bakkan ngir jëlaat ko.