John 10:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñu bare ca ñoom naan: «Dafa ànd ak rab! Dafa dof! Lu tax ngeen koy déglu?»