John 10:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu tontu leen ne: «Wax naa leen ko ba noppi, waaye gëmuleen. Jëf yi may def ci sama turu Baay ñoo may seede.