John 10:41 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Nit ñu bare ñëw ci moom, te naan: «Yaxya deful benn kéemaan, waaye li mu wax ci kii yépp, dëgg la.»