John 11:33 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu gis ne, mi ngi jooy te Yawut yi ànd ak moom itam ñu ngi jooy. Mu daldi jàq, am naqar wu réy.

Recommended Reading