John 11:47 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Farisen ya ak saraxalekat yu mag ya woo kureelu àttekat ya ne: «Nit kii kat, kéemaan yi muy def a ngi bëgg a bare. Lu nuy def nag?