John 11:52 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Du woon rekk ngir xeet woowu, waaye ngir itam doomi Yàlla, yi tasaaroo yépp, dajaloo nekk benn.