John 11:56 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñu ngi doon wut Yeesu tey waxante ca kër Yàlla ga naan: «Lu ngeen ci xam? Ndax dina ñëw ci màggal gi walla déet?»