John 12:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ku bëgg a doon sama surga, na ma topp. Bu ko defee, fu ma nekk, fa lay nekk moom itam. Ku may liggéeyal, sama Baay dina ko teral.