John 12:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
«Léegi nag damaa jàq. Lu may war a wax? Mbaa du dama naan: “Baay, musal ma ci li nar a xew waxtu wiy ñëw?” Déedéet, ñëw naa sax ngir jaar ci waxtu woowu.