John 12:29 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Mbooloo ma fa teewoon te dégg baat ba daldi ne: «Dënnu la woon!» Ñeneen naan: «Malaakaa doon wax ak moom.»