John 12:49 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte waxuma ci sama coobare, waaye Baay bi ma yónni ci boppam, moo ma sant li ma war a wax ak li ma war a jàngale.