John 12:50 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Te xam naa ne, li muy santaane day joxe dund gu dul jeex. Kon li ma wax, dama koy wax, ni ma ko Baay bi sante.»