John 13:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu ne ko: «Ku sangu ba noppi, soxlaatul a raxas lu dul ay tànkam, ndaxte set na wecc. Yéen nag set ngeen, waaye du ñépp!»