John 13:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi mu leen raxasalee seeni tànk ba noppi, Yeesu dafa solaat mbubbam, dellu toogaat ne leen: «Ndax xam ngeen li ma leen defal?