John 13:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon bu fekkee ne man miy Boroom bi tey Kilifa gi, maa leen raxasal seeni tànk, yéen itam war ngeen di raxasalante seeni tànk.