John 13:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, ku nangu kenn ci ñi may yónni, nangu nga ma, man itam; te ku ma nangu, nangu nga ki ma yónni.»