John 13:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu xamoon na ne, Yàlla joxoon na ko sañ-sañ ci lépp, xam it ne, ca Yàlla la jóge te ca moom lay delluwaat.