John 14:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Gëmleen li ma leen wax ne, maa ngi ci Baay bi te Baay baa ngi ci man; walla boog, gëmleen ndax jëf yi.