John 14:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax: képp ku ma gëm dina def, moom itam, jëf yi may def. Dina def sax yu gën a màgg, ndaxte maa ngi dem ci Baay bi.