John 14:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Des na tuuti ci kanam, àddina du ma gisati; waaye yéen dingeen ma gis. Dinaa dund, moo tax yéen itam dingeen dund.