John 14:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu tontu ko ne: «Ku ma bëgg dina sàmm sama kàddu. Sama Baay dina ko bëgg te nun dinanu ñëw ci moom, te dëkk ci moom.