John 14:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ku ma bëggul doo sàmm sama kàddu. Li may wax nag, jógewul ci man, waaye mi ngi soqikoo ci ki ma yónni.

Recommended Reading