John 14:28 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
«Dégg ngeen li ma leen wax: “Dinaa dem, waaye dinaa dellusi ci yéen.” Bu ngeen ma bëggoon, dingeen bég ci li may dem ca Baay ba, ndaxte Baay bee ma gën a màgg.