John 14:31 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye àddina si war na xam ne, bëgg naa Baay bi te ni ma ko Baay bi sante, ni laay jëfe. Jógleen, nu dem!