John 14:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndegam xam ngeen ma, dingeen xam itam sama Baay. Lu weesu tey, xam ngeen ko te gis ngeen ko.»