John 15:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Car bu soqikoo ci man te meññul, dina ko dog, sànni. Waaye car bu ci meññ, dina ko tenqi, ngir mu gën a meññ.