John 15:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Fàttalikuleen li ma leen wax: “Jaam gënul a màgg sangam.” Bu ñu ma sonalee, dinañu leen sonal yéen itam. Bu ñu toppee sama wax, dinañu topp seen wax yéen itam.