John 16:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Dinañu leen dàq ca jàngu ya, te dinañu dem ba jamono joo xam ne ñi leen di rey dañuy xalaat ne, ñu ngi màggal turu Yàlla.