John 16:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, dingeen jooy xàcc, waaye àddina dina bég; dingeen jàq, waaye seen njàqare dina soppaliku bànneex.